Yaw kas lay maan a xool Bu ma la gissé damay ragal Yaw yaa sama xol Bu ma la gissé damay joy Ah Yaw yaa sama xol Yaw kas laa bëgg Bu ma la gissé damay joy Yaa sama aduna Ñoom duñu mëso ñëw Duñu mëso ñëw Mëso ñëw jël ma Ah Bu ñu ñëwee Fii lañu ma fek Ñoom duñu mëso ñëw Duñu mëso ñëw Mëso ñëw jël ma Ah Bu ñu Fii lañu ma fek Ñoom duñu mëso ñëw Duñu mëso ñëw Mëso ñëw jël ma Ah Bu ñu ñëwee Fii lañu ma fek Ñoom duñu mëso ñëw Duñu mëso ñëw Mëso ñëw jël ma Ah Bu ñu ñëwee Fii lañu ma fek Ñoom duñu mëso ñëw Duñu mëso ñëw Mëso ñëw jël ma Ah Bu ñu ñëwee Fii lañu ma fek Ñoom duñu mëso ñëw Duñu mëso ñëw Mëso ñëw jël ma Ah Bu ñu ñëwee Fii lañu ma fek